LIGGEEY, JANG AK MECCE

Wòlof Català Àudio

Tey bésub liggéey la. Tey bésu bȅr la.

Avui és dia feiner. Avui és dia festiu.

Dama nekk ci bȅr. Damay liggéeyi.

Faig vacances. Vaig a fer feina.

Damay wat. Jigéen laa juy wat di létt. Man damay séddalé. Jigéen laa juy sédaale.

Faig feina de perruquer. Faig feina de perruquera. Faig feina de cambrer. Faig feina de cambrera.

Internet lay liggéeyé. Ordinatȅȅr
portabal lay ligéeyée.

Faig teletreball. Faig feina amb el portàtil.

Amuma liggéey. Damay taxawaalu.

No tenc feina. Estic a l’atur.

Liggéey ngay wut. Ligéey laa bȅgg.

Cerc feina. Necessit una feina.

Man jaaykat laa. Jàngalekat laa. Jigéen
juy jàngale laa. Beykat laa. Boroom tool laa.

Som comerciant. Som professor. Som professora. Som pagès. Som pagesa.

Jàng naa Katalan. Jàng naa français.
Jàng naa español. Jàng naa allemand.
Jàng naa anlais.

Estudii català. Estudii francès. Estudii espanyol. Estudii alemany. Estudii anglès.

Jàng naa mathematique. Jàng naa
xeltu. Jàng naa xam -xamu simi. Jàng
naa fȅlsȅwȅ. Jàng naa yoon.

Estudii matemàtiques. Estudii psicologia. Estudii química. Estudii filologia. Estudii dret.