WÒLOF CATALÀ ÀUDIO

Ca Majorque, dañu naan…

A Mallorca diuen…

Ci Katalan, nii lañu koy woowe…

En català es diu…

Naka lañuy waxee Minorque…?

Com ho diuen a Menorca...?

Naka lañuy waxee ci Katalan…?

Com es diu en català...?

Xam nga naka lañuy wax lii ci
Ibza…?

Saps com ho diuen a Eivissa…?

Ndax xam ngeen nan lañu koy
ci Katalan…?

Saps com es diu en català…?

Ci Formentera dañu naan...

A Formentera diuen…

NUYOO AK KADDU YU LALU CI YAR

dona-pag 4.gif

WÒLOF CATALÀ ÀUDIO
Nuyu naa la. Naka suba si.
Ngoonug jàmm. Guddig jàmm.

Hola. Bon dia. Bon vespre. Bona nit.

Ba beneen. Ba booba. Amal ay xéewal.

Adeu. A reveure. Que vagi bé.

Ba ci kanam. Ba ci fan yii di nȅw. Ba suba.

Fins aviat. Fins més tard. Fins demà.

—Jȅrȅ-jȅf. Sant la bu baax.
—Noo ko bokk, loolu du dara

-Gràcies. Moltes de gràcies.
-De res.

Jegal Ma, Baal Ma, Méti Na Ma.

Perdoni. Disculpi. Em sap greu.

Bég naa ci xamante bi.

Molt de gust. Tant de gust.

Ak mbégté gu rȅy rekk.

Amb molt de gust.

Lekkal bu baax.

Que vagi de gust. Bon profit.

Bànneexu leen. Bég leen bu baax

Diverteix-te. Que t’ho passis bé.

Dalal ak jàmm.

Benvingut. Benvinguda.

Ab diir su la neexee. Wànniwaatal su la
neexee.

Un moment, per favor. Una altra vegada, per favor. Més a poc a poc, per favor.