AY AM -AM NGIR JANG KATALAN
* Ay xabaar yu ñuy bésal saa su nekk ci http://dgpoling.caib.cat.
NJÀNGUM CATALANE
Njàngum làkk katalan ci bépp tolluwaay ak ci anam yi yépp, maanaam ci njàng mooy teew, njàng
moo xam ni da ngay teew tuuti walla njàngum internet ba ci jàngal sa bopp walla sax béréb yu nuy
waxtaane.
INSTITUT D’ESTUDIS BALEÀRICS (DAARA JU NUY JANGE BALEARES)
C. de l’Almudaina, 4, Palma 971 17 76 04 https://llengua.iebalearics.org
ESCOLA MUNICIPAL DE MALLORQUÍ (DAARA DIIWAANU MAJORC)
Pg. del Ferrocarril, 79, Manacor 971 83 49 83 https://www.escolademallorqui.cat
INSTITUT D’ESTUDIS EIVISSENCS (DAARA JANG BU IBIZA)
Via Púnica, 29, Ibiza 971 31 27 75 https://estudiseivissencs.cat
DAARAYE JANG LAKK
Escola Oficial d’Idiomes de Palma
(Daaray jàng làkku Palma)
C. d’Aragó, 59
971 42 13 14 I https://eoipalma.com
Escola Oficial d’Idiomes de Calvià
(Daaray jàng làkk bu Calvià)
C. de l’Arquitecte Francesc Cases, s/n, Bendinat
971 70 01 50 I http://www.eoicalvia.com
Escola Oficial d’Idiomes d’Inca
(Daaray jàng làkk bu Inca)
Ctra. de Palma-Alcúdia, s/n
(edificio Berenguer d’Anoia)
971 50 21 54 I https://www.eoinca.com
Escola Oficial d’Idiomes de Manacor
(Daaray jàng làkk bu Manacor)
Ronda de l’Institut (edificio Mossèn Alcover)
971 55 41 52 I https://www.eoimanacor.com
DAARAY NJÀNGUM MAG NI
http://www.caib.es/sites/fp/ca/informacia_general_0
Yéneni xibaar yu dolli ku ci lii:
Conselleria d’Educació i Formació Professional (Ministeer bi ni dénk njàng mi ak tàggat ci wàllu liggèey)
C. del Ter, 16, pol. Son Fuster, Palma 971 17 77 71
Delegació Territorial d’Educació a Menorca (Kuréel gi nu dénk njàng mi ci diiwaanu Minorque)
C. de Josep M. Quadrado, 33, Maó 971 17 62 65
Delegació Territorial d’Educació a Eivissa i Formentera (Kuréel gi nu dénk njàng mi ci diiwaanu
Ibiza et Formentera)
Via Púnica, 23, Ibiza 971 17 60 29
Ay xabaar yu ñuy
bésal saa su nekk ci
http://dgpoling.caib.cat
AY AM -AM NGIR JANG KATALAN
Escola Oficial d’Idiomes de Maó
(Daaray jàng làkk BU Mào)
C. de Francesc F. Andreu, 2
971 35 43 28 I https://www.eoimao.com
Escola Oficial d’Idiomes de Ciutadella
(Daaray jàng làkk bu Ciutadella)
C. de Mallorca, 67
971 38 17 42 I https://www.eoiciutadella.com
Escola Oficial d’Idiomes d’Eivissa
(Daaray jàng làkk bu Eivissa)
C. del Raspallar, 2 (edificio IES Sa Blanca Dona)
971 31 46 22 I http://www.eoi-eivissa.com
Escola Oficial d’Idiomes de Formentera
(Daaray jàng làkku de Formentera)
Av. del 8 d’Agost, 90, Sant Francesc de
Formentera (edificio IES Marc Ferrer)
971 32 34 01 I http://www.eoi-eivissa.com
MAIRIE
Yenn diiwaan yu Iles Balereares dañuy fay amal ay ndajey njàng catalan. Mën nañu ci am ay xabaar
suñu gëstoo yenn siti internet yu diiwaan bu nekk.
Majorque: http://www.caib.es/sites/cedomu/ca/ajuntaments_de_mallorca-25567
Minorque: https://www.caib.es/sites/cedomu/ca/ajuntaments_de_menorca-25779
Ibiza et Formentera: https://www.caib.es/sites/cedomu/ca/ajuntaments_deivissa_i_formentera-25780
CENTRES DE CATALÀ DE L’INSTITUT D’ESTUDIS BALEÀRICS
(BEREBU CATALAN BU DAARAY JANG BALEARES)
Béréb bu kenn ku nekk mena jàngale boppam Catalan te wéeru ci ay soxlay boppam.
MAJORQUE:
Centre de Català de Palma (Bérébu jàng Catalan bu Palma)
C. de l’Almudaina, 4 971 17 89 15 ccpalma@iebalearics.org
Centre de Català d’Inca (Daaray Inca Catalan)
Pl. de Sant Domingo, s/n 971 50 58 09 ccinca@iebalearics.org
Centre de Català de Manacor (Daaray catalan bu Manacor)
Pg. del Ferrocarril, 79 627 32 91 91 ccmanacor@iebalearics.org
MINORQUE: Centre de Català de Ciutadella (Daaray catalan bu Ciutadella)
C. de l’Hospital de Santa Magdalena, 1, 2n 971 48 42 04 ccciutadella@iebalearics.org
IBIZA: Centre de Català d’Eivissa (Daaray catalan bu Ibiza)
C. de Bes, 9 - C/ Joan Xicó, s/n 682 82 70 44 cceivissa@iebalearics.org
JUMTUKAAY YI CI INTERNET BI
Sites Web ak ay jumtukaay yu mȅna dimbali nit mu jàngal boppam làkku Catalan.
TEKKI BAAT YU LALU NEEL TURIST YI. CONSELL INSULAR DE MENORCA (AY XALAAT YU DUN
MINORQUE)
TTéré tekki baat ci làkku allemand, español, français, anglais ak italien.
http://sal.cime.es/contingut.aspx?idpub=183
MALLORCAT. CONSELL INSULAR DE MALLORCA (AY XALAAT NEEL MAJORQUE)
Jumtukaay bu ku nekk mȅna dalalee boppam njàngum Catalan bu ànd ak ay baat yu nu tekki, ay
nataal, ay jukki ak ni nuy waxee baat yi.
https://mallorcat.llenguamallorca.cat
DICCIONARI VISUAL. CONSELL INSULAR DE MALLORCA (AY XALAAT CI DUN MAJORQUE)
Téeré tekki baat bu ànd ak ay nataal yu nu rànnee ay màndarga yuy yombal tekki espanol,
français, anglais, allemand, arab ak siinuwaa.
http://llenguamallorca.cat/diccionari-visual
MAÓ EN CATALÀ. CURS BÀSIC DE CATALÀ. AJUNTAMENT DE MAÓ (NIY XELAL MAIRI MAHÓN)
Njàng mu ànd ak waxtaan ak tekki baat ci li nuy dund bés bu nekk.
https://ajmao.org/WebEditor/Pagines/file/Med_Intercultural/Quadern%20Mao%20en%20Catala.pdf
EP! ESCOLTA I PARLA. GENERALITAT DE CATALUNYA (EP ! DEGLU LEEN TEY WAX LI EPP CI
NGURU CATALUNYA)
Njàngum wax mu ànd ak ay nataal, ay ndégtu, ay widéo, ak ay itte ngir saafara jafe – jafe catalan
yiy am bés bu nekk.
https://llengua.gencat.cat/ca/serveis/aprendre_catala/ep-curs-oral-catala
ORALPHA. MÈTODE D’ALFABETITZACIÓ I COMUNICACIÓ ORAL EN CATALÀ.
GENERALITAT DE CATALUNYA (ORALPHA. PEXEY LIIFANTU AK JOKKOO CI WALLU WAX CI
CATALAN. LI GENA YAATU CI NGURU CATALUNYA)
Jumtukaayu njàng mu ànd ak ay pexey liifantu ak jokkoo ci wàllu wax ci catalan ak karne du def
ay itté ak téeré buy gindi.
https://dixit.gencat.cat/ca/detalls/Article/oralpha_metode_alfabetitzacio_catala
BEREBU CATALAN BU SAXUL BENN PLACEC. INSTITUT D’ESTUDIS BALEÀRICS (DAARAY
NJANGUM BALEARES)
Ay pexe ngir jàng catalan te sukkandinku ci internet bi ak jàppale ci wàllu xalaat.
https://llengua.iebalearics.org/ca/centres
PARLA.CAT. GENERALITAT DE CATALUNYA (NGUURUG CATALOGNE)
Bérébu njàng mu saxul muy yombal njàngum catalan mu suufe mi.
https://www.parla.cat
NIY JAPPALÉ JANGUM LAKK TE KHAARU NIOU CI DARA
Béréb bu nuy dalale nit ku dégg bu baax catalan te mȅna jokkoo ak keneen kuy doora tàmbali te
bȅgga wax bu baax.
PARAULA. CENTRE DE SERVEIS LINGÜÍSTICS (DAARAY NJANGUM LAKK)
C. de Sant Alonso, 24, Palma (edificio Ca n’Alcover) 971 76 13 01 http://ambtu.paraula.cat
AJUNTAMENT DE MAÓ (MAIRIE BU MAÓ) Área de Bienestar Social y Familia
Pl. de la Constitució, 1, Maó 971 35 67 00 http://www.ajmao.org/voluntariatlinguistic
INSTITUT D’ESTUDIS EIVISSENCS (DAARA NJANG BU EIVISSA)
Via Púnica, 29, Ibiza 971 31 27 75 https://estudiseivissencs.cat/voluntari-linguistic
CONSELL INSULAR DE FORMENTERA (KUREEL GIY XELALAATE CI DUN BU FORMENTERA)
Kuréel giy xelalaate ci làkk linguistique
Av. de Port-salè, s/n, Sant Francesc de Formentera 971 32 12 75
https://www.consellinsulardeformentera.cat/index.php?option=com_content&view=category&layout=blog&id=297&Itemid=353&lang=ca
YÉNENI MELOKANE NGIR JANG CATALAN
Tope xarala yi ci lakkum catalan di na lene dimbali ci njangue mi. Bene pacc ci dun Balears:
IB3 RADIOTELEVISIÓ DE LES ILLES BALEARS (radio ak télé) https://ib3.org
TELEVISIÓ D’EIVISSA I FORMENTERA (télévision) https://teftv.com
ONA MEDITERRÀNIA (radio) http://onamediterrania.cat
RÀDIO ILLA (radio) http://www.radioilla.cat
ARA BALEARS (xibaru bes bu tey) http://arabalears.cat
DBALEARS (xibaru bes bu ne) https://www.dbalears.cat
PREMSA FORANA DE MALLORCA (xibaru dun Majorque) http://www.premsaforana.cat
Ci seni yeungueutu, meun ngéne jang catalan. Lii gestu ak ay xalaat yu niou def ci loolu la :
IB-MUSICAT (déglou musique ci catalan)
https://ib-musicat.cat
JOCS EN CATALÀ (ay po yu bari ci catalan)
https://jocsencatala.cat
APRÈN CATALÀ SENSE ADONAR-TE’N!
(Ay jumtukaayi po ngir jàng catalan te doo ko yeg)
http://www.caib.cat/govern/sac/fitxa.do?codi=4130962&coduo=2390443&lang=ca