LAAJ YI ÑUY FARAL DI DEF
Wòlof | Català | Àudio |
—Naka ngeen def? Naka nga def? |
―Com va? Com està? |
|
Lan moo ko dal? yaram wi neexul? |
Què li passa? No es troba bé? |
|
—Naka laa tudd?
|
―Què noms?
|
|
—Yaay kan? |
―Qui és, vostè? |
|
—Lan la? |
―Què és això? |
|
—Fan ngeen jógé? |
―D’on ets, tu? |
|
—Fan ngeen jógee? |
―D’on és, vostè? |
|
—Fan la jóge? |
―D’on és, ell? |
|
—Fan ngeen jóge? |
―D’on sou, vosaltres? |
|
—Waa Majorque nga?
|
―Ets mallorquí? ―Ets mallorquina? |
|
—Ndax waa Minorque la?
|
―És menorquí? ―És menorquina? |
|
—Ndax waa Ibiza ngeen?
|
―Sou eivissencs?
|
|
—Ndax waa Formentera lañu?
|
―Són formenterers?
|
|
—Fan la dȅkk ? —Ci taax ya laa dȅkk. Maa ngi dȅkk ca kaw ga. Maa ngi dȅkk ca àll ba. |
―On viu? ―Visc a la ciutat. Visc en un poble. Visc al camp. |
|
|
―A quin carrer vius? ―Visc al carrer Nou. Visc a la plaça Major. |
|
—Ndax dégg nga catalan ? |
―Parla català? |
|
Ndax dégg nga li may wax? Lu mu tekki? |
M’entén? Què vol dir, això? |
|
Naka? Naka lees ko waxee? |
Com? Com diu? |
|
Lan nga wax? Lan nga bȅgg? |
Què dius? Què vols? |
|
Fan ngeen jȅm? Fan ngeen jóge? |
On anau? D’on veniu? |
|
Ndax wóor na la? Ndax Wόor na ko? |
N’està segur? / N’està segura? De veritat? |
|
Kañ? Kañ lawoon? Ba kañ lay doon? |
Quan? Des de quan? Fins quan? |
|
Wax ma? Kan ngay waxal? Ci kan la jóge? |
Digui? Amb qui parl? De part de qui? |
|
Ndaw am na ñaari xel? Ndax dégg nga?? |
Hi ha cap dubte? Entesos? |
|
—Bȅgg nga ko? |
―T’agrada? |
|
Mȅn naa tux? Mȅn naa gaare fii? |
Que puc fumar? Que hi puc aparcar, aquí? |
|
Mȅn nga féey? Mȅn ngaa togg? Mȅn nga làkk catalan? |
Saps nedar? Saps cuinar? Saps parlar català? |