Ay leeral ci melokaan ak mandarga yi nu jefandikoo ci biir jumtukaay bile.


Bootal yi ñuy wax el pa ak es pa (« mburu) ») ; kȅr gi walla kȅram bokk na ci liy gȅna màndargaal làkku katalan. Bu njȅkk bi moo gȅna yaatu waaye bi ci topp lañuy gȅn di faral di dégg ci làkku waa Ile Baléares ak Pitiusas ba ci yenn béréb yi nekk Costa Brava bu Catalogne. Waaye nag bootal bi ñuy was es/sa dàqul el/la bi nga xam ne moom rekkay nekk ci kanam ay baat ak kàddu yu bari : Ag Géej (« Géej gi »), Ab Adduna (« Adduna bi ») ñooy ñaar, mooy ñaar ak ñoom seen.

Bootalu el/la lañuy gȅn di jȅfandikoo ci wax ji gȅna siiw. Bootal yi lañuy gȅn di jox dayo ndax doxalinu làkk yi ñu gȅna miin moo gȅna jafe ndax dafa bari ay coppite. Kiy faral di wax ni mu ko neexe, du am jafe -jafe bootal yi su leen bàyyee tuuti xel.

Ci beneen fànn, mȅn nañoo wax ni ci xeeti waxin yu bari lañu sukkandiku ngir sos jumtukaay bii nga xam ni dina yombal jokkoo ci anam yu bari. Ba tey (/) màndarga mii mooy wone waxin walla yenn baat yi nirόo

Te itam, ay bootal ñooy gόoral walla jigéénal, ba tey, rȅdd wii (/) mooy wone waxin walla kàddu yi bokk lu ñuy tekki