NJABOOT, NGUUR, KAYITI JUDDU, SEY AK FAATU BA CI
DEKKUWAAY
Wòlof | Català | Àudio |
Baay, Yaay, xale bu góor, xale jigéen, mag walla rakk ju góor, mag walla rakk ju jigéen. |
Pare, mare, fill, filla, germà, germana. | |
Doomoo/Maam ju góor, Doomoo jigéen/ |
Padrí/avi, padrina/àvia, net, neta. |
|
Jȅkkȅr/boróom kȅr, soxna/jabar, xarit bu jigéen/xarit bu jigéen. |
Espòs/home, esposa/dona, company, companya, parella. | |
Doomu nijaay bu góor, nijaay/bàjjen, |
Cosí, cosina, oncle/conco, tia, nebot, neboda. | |
Rakki soxna bu góor, rakki soxna bu |
Cunyat, cunyada, gendre, nora. | |
Dama am soxna. Góor gu doomoo laa. |
Som casat. Som fadrí. Som divorciat. Som vidu. Som casada. Som fadrina. Som divorciada. Som vídua. | |
Am naa ñetti doom. Am naa ñetti sȅt yu |
Tenc tres fills. Tenc cinc nets. | |
Ca sunu kȅr ay ñetti rakk aki mag yu |
A ca nostra som quatre germans. | |
Samay kȅr maam laa dȅkk. Man rekka |
Visc a cals padrins/avis. Visc tot sol. Visc tota sola. | |
Ci genn kȅr laa dȅkk. Kȅr gi ma dȅkk |
Visc en un pis. Visc en una casa amb jardí. |