Wòlof |
Català |
Àudio |
—Wan waxtoo jot, bu la neexe ? —Ñeenti waxtu yu teg fukki saa ak juróom.
|
―Quina hora és, per favor? ―Són les quatre i quart.
|
|
Tey. Démb. Berki démb / Suba / gannaaw suba. “ganaawaatu suba |
Avui. Demà. Ahir. Demà passat / passat demà. Despús-ahir. |
|
—Tey ban bés la? —Noo ngi ci alitine 6 fan ci sattumbar 2021. |
―Quin dia és avui? ―Avui és dilluns, 6 de setembre de 2021. |
|
Suba. Midi. Jant buy so / digg bȅccȅg. ngoon. guddi. Suba teel. |
Matí. Migdia. Capvespre/tarda. Vespre. Nit. Matinada. |
|
Njàng mi ci ngoon si la.Ci suba si lay yegsi. |
Les classes són al vespre. Ell arriba al matí. |
|
Asamaan set na. Guddi na. Mu ngi tàmballe lȅndȅm.
|
És de dia. És de nit. Es fa fosc. |
|
Ci naari waxt (14h) lañu añ. Reer bi jurόom netti waxtu ag genn wàll la.
|
El dinar se serveix a les dues. El sopar és a les vuit i mitja. |
|
—Ñaata waxtu lay def? —Jurόomi waxtu.
|
―Què dura? ―Cinc hores. |
|
—Ñaata waxtoo ci des? —Ñetti ayu bés. |
―Quin temps falta? ―Tres setmanes.
|
|
—Ban waxtu lay dellusi? —Fii ak benn waxtu.
|
―Quin temps estarà a tornar? ―Devers una hora.
|
|
Booba ak léegi am na ñetti ayu bés. Juróom ñaari ayu bés ba léegi.
|
Fa tres setmanes. Des de fa set setmanes.
|
|
Lu jiitu ñaari waxtu. Gannaw ñeenti fan.
|
Abans de dues hores. Després de quatre dies.
|
|
Ci juróom ñeenti waxtu ak genn wall. Ci booru juróom ñaari waxtu yu teg ñaar fukki saa.
|
A les nou i quart. Devers les set i vint.
|
|
Am naa jot gu bari. Bariwuma jot. Amuma jot.
|
Tenc molt de temps. Tenc poc temps. No tenc temps.
|
|