MELOKAAN
Wòlof | Català | Àudio |
Weex, xell, nete, xawa naat, naat, baxa, yulet, xonq, xawa xonq, gris, ñuul. |
Blanc, beix, groc, carabassa, verd, blau, lila, vermell, grana, marró, gris, negre. |
|
—Nan la mel? |
―De quin color és? |
|
Sopp naa melokaan wii. Soppu ma dara |
M’agrada aquest color. No m’agrada gens aquest color. |
|
Dafa leer ba ȅpp. Lȅndȅmul torop. |
És massa clar. No és gaire fosc. |
LIM
Wòlof | Català | Àudio |
Benn, ñaar, ñett, ñeent, juróom, juróom benn, juróom ñaar, juróom ñett, juróom ñeent, fukk. | U/un/una, dos/dues, tres, quatre, cinc, sis, set, vuit, nou, deu. |
|
Fukk ak benn, fukk ak ñaar, fukk ak ñett, fukk ak ñeent, fukk ak juróom, fukk ak juróom benn, fukk ak juróom ñaar, fukk ak juróom ñett, fukk ak juróom ñeent, ñaar - fukk. |
Onze, dotze, tretze, catorze, quinze, setze, desset/disset, devuit/divuit, denou/dinou, vint. |
|
Fanweer, ñeent fukk, juróom fukk, juróom benn fukk, juróom ñaar fukk, juróom ñett fukk, juróom ñeent fukk, téeméer, junni. |
Trenta, quaranta, cinquanta, seixanta, setanta, vuitanta, noranta, cent, mil. |
|
Pàcc/pàcc, benn ñeenteel, ñaari |
Mig/mitja, un quart, dos quarts, una dotzena. |